Lan ngay jëmmal tay?
Defaral ay yëgle-siiwali bara jokkoo, ay wideo, ay wonin, ak yeneen yu AI dooleel ànd ci ak Canva.
Ay jumtukaay ngir dooleel sa liggéey bu gëna baax
Jëfandikool Canva AI 2.0 ngir Soppi waxtaan def ko sos
Raxasal nataal yi ak Magic Dindikat
Yéegalal niwo sa bindin ak Bind
Soppil sa nataal def ko ab tëralinu xët bu ñu mëna soppi ak Magic Lalukaay yi
Sos ay wonin yu nit ñi di bàyyi xel te mu leen di indil xalaat
Gisal sa modelu wonin bu gëna baax
Desal ci màrk bi ak Pàccu Màrk
Dundalal say wonin ak ay xumbal
Sosal sa wideo bi ci topp te doo sonn ak model yi xew
Dindil ci ginaawi nataal yi ak wideo yi ci benn kilik
Taarala bépp nataal ak Yokkukaayu Tolluwaayu Nataal
Soppil dayo jëmmal ci saa si ngir bépp kanal
Soppil kilip yi def leen këmb ak sunu soppalikaayu wideo bi
Sa modeli wideo yépp ci benn barab
Ay wideo denc rënk yu baax ci studio ngir bépp mbebëtu liggéey
Yokkatal dooleey warlu gi ak màndargaal yu AI doolel
Soppi xalaat yi def leen ay móol yu am baaxaay bu kawe ak Bitiku Móol
Soppil ci saasi dayo jëmmal ngir bépp móol
Jëmmalal te móol woote yi ngir bépp xew-xew
Defar ay nataal yu yéeme te am baaxaay bu kawe ngir say móol
Jumtukaay yi yépp. Lépp ci benn barab.
Xamante ak visual Suite
Sa liggéey yépp ci benn barab ngir sos ak liggéeyandoo bu jaar yoon, bu IA doolel.
Wone bu ànd ak njeexital
Xelaataatal gaaral yi ak nataali sinemaa, liggéeyandoo yu am xel ak jumtukaayi IA.
Model ci lépp loo bëgga liggéey
Ndoorte limu model
Njeexte limu model